bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Jeremiah 3:16
Jeremiah 3:16 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Janti keroog bu ngeen baree ba giir ci réew mi, deesul waxe gaalu kóllërey Aji Sax ji; xel dootu ci dem, deesu ko fàttliku sax, te deesu ko namm, deesu ko sàkkati sax.» Kàddug Aji Sax jee.