Jeremiah 31:36 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu ne: «Bu askanu Israyil feyee ba fàww, may gis, dogal yooyoo toxu, may gis.» Kàddug Aji Sax jee.