Jeremiah 32:14 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Aji Sax ji Yàllay Israyil Boroom gàngoor yi dafa wax ne: “Jëlal kayit yii, kayitu njaay bi tëje, ak kayit bi tëjewul, nga boole yeb ci njaqal ban, ndax kayit yi mana yàgg.