Jeremiah 32:24 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Sëkki gawukaay yaa ngii ñu yékkatil dëkk bi, ngir nangu ko. Dëkk bi dina daanu ci loxoy waa Babilon ñi ko song, ndax saamar akub xiif ak mbas. Gis nga ko déy, li nga waxoon am na!