Jeremiah 32:3 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
fa ko Cedesyas buurub Yuda dencoon, ndax da ko noon: «Ana lu waral ngay wax bii waxyu? Nga ne: “Aji Sax ji dafa wax ne mu ngii di teg dëkk bii ci loxol buuru Babilon, mu nangu ko.