Jeremiah 32:36 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Yeena wax ci dëkk bii ne dina daanu ci loxol buuru Babilon ndax saamar akub xiif ak mbas. Waaye Aji Sax ji Yàllay Israyil dafa wax ne: