Jeremiah 32:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba loolu amee Anamel sama doomu baay bu ndaw dikk, na ma ko Aji Sax ji waxe. Mu fekk ma ci ëttu dag yi, ne ma: «Rikk jëndal sama tool ba ca Anatot ca diiwaanu Beñamin ndax sa alal la ci yoon, yaa ko saña jotaat. Kon jënd ko.» Ma xam ne loolu kàddug Aji Sax jaa.