Jeremiah 33:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Aji Sax ji Boroom gàngoor yi dafa wax ne: «Bérab bii di gent bu kenn nekkul, du nit du rab ci dëkk yi fi nekk yépp, bérab bii dina dellu am parlu yu sàmm siy gooral seeni gàtt.