bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Jeremiah 34:1
Jeremiah 34:1 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba Nabukodonosor buuru Babilon àndeek mbooloom xareem mépp ak mboolem réew yeek xeet yi mu teg loxo, ñu songandoo Yerusalem ak dëkk yi ko wër yépp, kàddu gii dikkaloon na Yeremi, bàyyikoo ci Aji Sax ji: