Jeremiah 34:10 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba mu ko defee mboolem kàngam yeek nit ñi ko fasoo woon daldi nangoo goreel seen jaam yu góor ak yu jigéen, bañ leena jaamlooti, ñu moom seen bopp. Ñu daldi leen yiwi.