Jeremiah 34:11 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw gi nag ñu walbatiku, jëlaat seen jaam yu góor ak yu jigéen ya ñu goreeloon, dellooleen cig njaam, góor ak jigéen.