Jeremiah 34:5 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci jàmm ngay dee, te ni ñu taalale woon cuuraay say maami buur yi la jiitu, terale leen ko ci seen dëj, ni lañu lay taalale cuuraay, di la jooy naan: ‘Wóoy sunu sang ba dem na!’ Jii wax, maa ko wax.”» Kàddug Aji Sax jee.