Jeremiah 35:17 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Kon nag Aji Sax ji Yàllay Israyil, Boroom gàngoori xare yi dafa wax ne: Maa ngi nii di wàcceel Yuda ak képp ku dëkke Yerusalem mboolem musiba mu ma leen tuddaloon. Ndax damaa wax ak ñoom te dégluwñu; ma woo leen, wuyuwñu.»