Jeremiah 35:2 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Demal ca Rekabeen ña, nga wax ak ñoom, indi leen kër Aji Sax ji, dugal leen ci néeg yi benn, te jox leen biiñ, ñu naan.»