Jeremiah 35:4 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ma yóbbu leen kër Aji Sax ji, dugal leen ca biir néegu taalibey Xanan, góorug Yàlla gay doomu Igdalyaa; mooy néeg ba dendeek néegu kàngam ya, ca kaw néeg doomu Salum, Maaseya fara bunt ba.