Jeremiah 36:25 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Elnatan ak Delaya ak Gemarya sax tinu nañu Buur, ngir mu baña lakk taxañ ba. Waaye Buur dégluw leen,