bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Jeremiah 36:6
Jeremiah 36:6 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Demal yaw bésub koor, nga jàng taxañ, bi nga bind kàdduy Aji Sax, ji ma la dégtal, ña ca kër Aji Sax ji di dégg. Nanga ko jàng itam ci kanam mboolem Yudeen ña jóge seeni dëkk.