Jeremiah 38:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu am bés Sefatiya doomu Matan ànd ak Gedalya doomu Pasur ak Yukal doomu Selemya ak Pasur doomu Malkiya. Ñu dégg Yeremiy wax, ñépp di dégg, naan: