Jeremiah 38:11 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ebedd Meleg jël nit ña, daldi dem biir kër buur, jàll ba ca suufu néegu denc ya. Mu jële fa yére yu ràpp aki sagar, boole lépp, yoore buum ca kàmb ga, jottli ko Yeremi.