Jeremiah 38:2 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
« Aji Sax ji dafa wax ne: “Ku des ci biir dëkk bii, saamar rey ko, mbaa xiif, mbaa mbas. Waaye ku génn fekki waa Babilon, dina raw, bakkanam di ngañaayu xareem, mu mucc.”