Jeremiah 38:27 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba loolu amee kàngami buur yépp dikk, laaj Yeremi, mu wax leen la ko Buur digal. Ñu daldi noppi, ba ko; ndax kenn déggul woon la mu wax ak Buur.