Jeremiah 38:4 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kàngami buur yooyu dem ne Buur: «Waa jii, na dee rekk; mu ngi yoqil xarekat yi des ci dëkk bi, di yoqil ñépp ndax waxam jii mu leen di wax. Waa jii kat wutul jàmmu askan wii, xanaa musiba.»