Jeremiah 40:11 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu Yudeen ña woon ca Mowabeen ñaak Amoneen ñaak Edomeen ñaak mboolem réew ya, ñoom ñépp dégg ne buuru Babilon wacc na lenn ca askan wa, ñu des réewum Yuda, mu dénk leen Gedalya.