Jeremiah 40:5 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Balaa Yeremee walbatiku, Nebusaradan teg ca ne ko: «Man ngaa dellu ca Gedalya doomu Ayikam doomu Safan ba tey. Moom la buuru Babilon dénk dëkki Yuda. Man ngaa toog ak moom ci digg waa réew mi, mbaa nga dem daal fu la gënal.» Nebusaradan nag jox Yeremi yóbbal ak lu mu lekk ci yoon wi, daldi ko yiwi.