Jeremiah 40:6 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba mu ko defee Yeremi dem ca Gedalya doomu Ayikam ca Mispa. Mu toog ca moom ca digg nit ña des ca réew ma.