Jeremiah 40:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Fekk am na mboolooy Yudeen ñu desoon ci àll bi. Seeni njiit yépp nag dégg, ñook ña ñu àndal, ne buuru Babilon dénk na Gedalya doomu Ayikam réew mi, dénk ko ñenn ci baadoolo yi des Yuda, diy góor aki jigéen aki gone yu ñu yóbbuwul ngàllo ca Babilon.