Jeremiah 40:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñu bokk dikk ba Mispa ca Gedalya; Ismayil doomu Netaña ma nga ca woon, ak Yowanan ak Yonatan, ñaari doomi Kareya, ak Seraya doomu Tanumet, ak doomi Efayi ma bokk Netofa, ak Yesaña ma bokk Maaka, ñook seeni nit.