bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Jeremiah 40:9
Jeremiah 40:9 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gedalya waatal leen, ñook seeni nit, ngir dalal seen xel, teg ca ne leen: «Buleen ragala nangul waa Babilon. Toogleen ci réew mi rekk te nangul buuru Babilon, muy seen jàmm.