Jeremiah 42:10 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su ngeen nangoo toog ba toog ci réew mii, maa leen di defar te duma leen daaneel. Maa leen di jëmbat te duma leen buddat. Ndax ñeewante naa leen ci musiba mi ma leen teg.