Jeremiah 42:11 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Buuru Babilon mii ngeen ragal, buleen ko ragal!» Kàddug Aji Sax jee. «Buleen ko ragal, ndax yeen laa àndal ngir wallu leen, xettli leen ci moom.