Jeremiah 42:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeremi teg ca ne: «Yeen ndesu Yuda, Aji Sax ji wax na leen ne leen: “Buleen dem Misra.” Nangeen xam xéll nag ne àrtu naa leen bésub tey.