Jeremiah 42:21 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yegge naa leen tey jii li seen Yàlla Aji Sax ji wax, waaye faalewuleen lenn ci kàddu yi mu ma yóbbante ci yeen.