Jeremiah 44:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Maay tonni ndesi Yuda gi dogu woon ba dikk réewum Misra, toogaansi fi. Dañuy dee. Ñoom ñépp réewum Misra gii lañuy daanoo. Saamar akub xiif lañuy fàddoo, ki gëna tuut ba ki gën di mag. Saamar akub xiif lañuy fàddoo, te dinañu gental gentu alkànde, ñu di leen móolook a sewal.