Jeremiah 44:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Jigéen ña teg ca ne: «Te sax ba nuy taalal cuuraay Lingeeru asamaan, di ko tuural, sunuy jëkkër dañu koo yégul? Xam nañu xéll ne nu ngi defal Lingeeru asamaan ay nàkk yu koy jëmmal, di ko tuural ay naan.»