Jeremiah 44:2 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
« Aji Sax ji Yàllay Israyil Boroom gàngoor yi dafa wax ne: Yeena gis mboolem musiba mi ma wàcceel Yerusalem ak dëkki Yuda yépp. Ñu ngi nii tey jii gental, kenn dëkku ca.