Jeremiah 44:24 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeremi teg ca wax ak ñépp, rawatina jigéen ña ñépp, ne leen: «Mboolem yeen Yudeen ñi ci réewum Misra, dégluleen kàddug Aji Sax ji.