bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Jeremiah 44:25
Jeremiah 44:25 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Aji Sax ji Yàllay Israyil Boroom gàngoor yi dafa wax ne: “Yeen ak seeni jabar yeena wax ci seen làmmiñ, àggalee ko seeni jëf. Ngeen ne dingeen def ba defaatoo dige yi ngeen digee taalal cuuraay Lingeeru asamaan, tuural koy naan. Dëggal-leena dëggal seeni dige te jëfee jëfe seeni dige.