bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Jeremiah 44:7
Jeremiah 44:7 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Léegi nag, Aji Sax ji Yàllay Israyil Boroom gàngoor yi dafa wax ne: Ana lu jar ngeen di teg seen bopp loraange ju réye nii, ba nar fee dagge réewum Yuda, góor ak jigéen, xale ba ci perantal, ba dungeen dese kenn?