Jeremiah 46:22 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ñu daw di faraas-faraasiy wéy ni jaan. Doole la noon songe Misra, dikke leeni sémmiñ ni gorkati garab.