Jeremiah 46:25 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Aji Sax ji Yàllay Israyil, Boroom gàngoori xare yi wax na ne: «Maa ngii di dikke mbugal Amon, tuuru dëkk bii di Teeb, ak Firawnaak waa Misraak seeni tuur ak seeni kàngam, boole ci ñi yaakaar Firawna.