Jeremiah 46:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Misraa, mooy fuddu ni dexu Niil, di fuur ni wali ndox. Mu naan: “Maay fuddu, mëdd àddina, sànk ab dëkk ak ña ca biir.”