bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Jeremiah 47:2
Jeremiah 47:2 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Aji Sax ji dafa wax ne: «Ndox a ngay fuddoo bëj-gànnaar, diy waame, walsi, walal réew meek li ci biiram akub dëkk ak ku ci biiram; doom aadama yuuxu, waa réew mépp serandoo.