Jeremiah 48:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Lu jëm ci Mowab, Aji Sax ji Yàllay Israyil, Boroom gàngoori xare yi dafa wax ne: «Ngalla waa Nebo, seen dëkk ba yàqu na! Kiryaatayim, ñu torxal, nangu ko; tata ja daanu, tasaaroo.