Jeremiah 49:28 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Lu jëm ci Kedar ak nguuri Àccor yi Nabukodonosor buuru Babilon nangu woon, Aji Sax ji dafa wax ne: «Ñokket ci kaw Kedar, ba tas waa penku yooyu,