Jeremiah 49:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Lu jëm ci Edomeen ñi, Aji Sax ji Boroom gàngoor yi dafa wax ne: «Xanaa boroom xel amatul fi Teman? Xanaa ndigal a réer xamkat yi? Am seen bopp a yàqu?