Jeremiah 5:13 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yonent yi daal, ngelawal neen! Kàddug waxyu newul ci ñoom; li ñuy wax, na leen yenu!”»