Jeremiah 50:44 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Maa ngii, di fëlle gottub Yurdan ni gaynde, wuti mbooy gu naat. Xef ak xippi déy, ma fëxale fa lépp, ba tabb fa ki ma taamu. Ana moos ku mel ni man, ku am sañ-sañ ci man? Ana njiit luy taxaw fi sama kanam?