Jeremiah 51:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yékkatil-leen tatay Babilon raayab xare, yokkleen wattukat yi, taxawal leen fa ñuy wattoo, te waajal tërukat yi. Aji Sax ji def na li mu waxoon ne dina ko def waa Babilon.