Jeremiah 51:46 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bu seen fit rëcc, ngeen di tiit xibaar yi ñuy yéene ci réew mi: ren yéene jib, déwén yéene jibati, fitna law ci réew mi, njiit ne njiit dann.