Jeremiah 51:62 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te nga wax ne: “ Aji Sax ji, yaw déy, yaa xamle ne dëkk bii dina tas, dara du ci dëkkati, du doom aadama, du rab. Ab gent lay doon ba fàww.”